Xeltéef yii dafa lay may nga dëppale sa arafukaay farañse AZERTY walla QWERTY, walla itam sa arafukaay angale QWERTY ak 7 ci lammiñi réew mi: wolof, pulaar, seereer, mandiŋ, joola, soninke ak manjak.