• English English
  • Français Français
  • Mandinka Mandinka
  • Seereer Seereer
  • Wolof Wolof

Alf@net - Les TIC en langues nationales du Sénégal

  • Dal bi
  • Jaar jaar
  • Ekip bi
  • Farandoo yi
  • Mébét yi

"Bu galan soppeekoo pecc mi soppeeku"
Léebu Awsa
Dal bi

Arafukaay Senegaal
Abiword ci wolof
Jàng tappe ci wolof
Gindeekukaayu Alf@net
Mozilla Firefox ci wolof

Jokkoo jëfandikookat bi

  • Sos koont bu bees
  • Laaj baatu jàll bu bees

Mébét yi

Xaralay xibaar ak jokkoo da ñuy ubbi bunt yu mag ci wallu njàng ci Afrik. Gëm nañu ni xarala yu bees yi mën nañu indi ay pexe yu bari ci yokkute Afrik.
Ay yoon a ngi nii yu ñu mëna xootal:

  • Njàngale bu sori.
  • Jumbantikatu mbind ak nëwu boppam ci lammiñi Afrik ci xeltéefi caytug mbind.
  • Tekki boppam ci lammiñi Afrik.
  • Baat bu ñu tëgg ngir duruus boppam ay mbind ci lammiñi Afrik.
  • Xammeekatu baat ngir bind ak baatu nit.
  • Tekki jàllukaayi telefon portabal ci lammiñi réew mi.
  • English English
  • Français Français
  • Mandinka Mandinka
  • Seereer Seereer

Xeltéef

  • Gindeekukaay yi
  • Xeltéef yi
  • Jumtukaay yi

Këmb barimelo

  • Internet ci joola
  • internet ci mandeŋ
  • internet ci pulaar
  • internet ci seereer
  • internet ci soninke
  • internet ci wolof

Ndawtal

  • Ressources

Powered by Drupal, an open source content management system
  • Dal bi
  • Jaar jaar
  • Ekip bi
  • Farandoo yi
  • Mébét yi

Association nationale pour l'alphabétisation et la formation des Adultes
Villa 17bis, Patte d'Oie Builders Nord Ext., B.P. 10453 DAKAR-LIBERTÉ
Dakar, Sénégal