Ekip bi
Ousmane Faty Ndongo
Usmaan moo jiite yëngu yëngu Anafa. Moon moo sos porogaraam alf@net ci 1997. Dafay tekki ak di yëngu ci xaralag xamteef. Moon moo sos yéenekaay bari melo alf@net te ñu mën cee jàng nan la ñuy jëfandikoo ordinatëër ci 5 lammiñi réew mi.
Dominique Rochefort
Dominique enseñëër ci wallu xamtéef. Moon mooy saytu lépp lu jëm ci lëkkaloo ci wallu xarala.
Valdiodio Ndiaye
Waljoojo mooy toppatoo caytu gi.
Jàppalekat yi
Saliou Badiane
Cheikh Ahmed Tidiane Guèye
Cécile Anne Marguerite Evers





