• English English
  • Français Français
  • Mandinka Mandinka
  • Seereer Seereer
  • Wolof Wolof

Alf@net - Les TIC en langues nationales du Sénégal

  • Dal bi
  • Jaar jaar
  • Ekip bi
  • Farandoo yi
  • Mébét yi

"Bu galan soppeekoo pecc mi soppeeku"
Léebu Awsa
Dal bi

Arafukaay Senegaal
Abiword ci wolof
Jàng tappe ci wolof
Gindeekukaayu Alf@net
Mozilla Firefox ci wolof

Jokkoo jëfandikookat bi

  • Sos koont bu bees
  • Laaj baatu jàll bu bees

Dal bi

Alf@net yëngatu Anafa la miy liggéey ci suqali lammiñi réew mi ci wallu xarala ci 1997 ba leegi .

Bunt bii da ñu ko jagleel bépp sos buy yokk teewaayu lammiñi réew mi ci internet ak ci xaralay xibaar ak jokkoo.

Ci dal bi mën ngeen ci fekk ay jumtukaay , ay xeltéef ak ay yéenekay barimelo yu amul moomeel. Yépp nak ci lammiñi réew mi rawatina ci wolof. Mën ngeen am fii itam ay ndimmal bu ngeen bëggee indi seen ndawtall.

Mën ngeen indi seen xalaat ak seen ndawtal bu ngeen bindoo ci pencum waxtaan wi ci rëdd.
Mën ngeen itam jot xibaar yi mujj ci porose bi.

Dal leen jamm ci geewu Alf@net

  • English English
  • Français Français
  • Mandinka Mandinka
  • Seereer Seereer

Xeltéef

  • Gindeekukaay yi
  • Xeltéef yi
  • Jumtukaay yi

Këmb barimelo

  • Internet ci joola
  • internet ci mandeŋ
  • internet ci pulaar
  • internet ci seereer
  • internet ci soninke
  • internet ci wolof

Ndawtal

  • Ressources

Powered by Drupal, an open source content management system
  • Dal bi
  • Jaar jaar
  • Ekip bi
  • Farandoo yi
  • Mébét yi

Association nationale pour l'alphabétisation et la formation des Adultes
Villa 17bis, Patte d'Oie Builders Nord Ext., B.P. 10453 DAKAR-LIBERTÉ
Dakar, Sénégal